Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan génn ci wanag day wax: "Xufraanaka

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan génn ci wanag day wax: "Xufraanaka

Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan génn ci wanag day wax: "Xufraanaka".

[Wér na] [Abóo Daawuda soloo na ko, At-tirmisiy, ak Ibnu Maaja, ak Ahmat]

الشرح

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan faj aajoom ba génn ci wanag wi day wax: maa ngi lay ñaan(sa njéggal) yaw Yàlla.

فوائد الحديث

Sopp nañu ñu wax: "Xufraanaka" ginnaaw bi ñu génnee ca barabu fajukaayu aajo ba.

Yonnente bi day jéggalu Boroomam ci gépp anam.

Nee nañu sababus jéggalu gi ginnaaw faj aajo: mooy gàtteñlu gi ci sant xéewali Yàlla yu bari yi, te bokk na ca génnug lor gi, may sàkku sa njéggal ci fajug aajo gi ma soxlaal wolif tudd la.

التصنيفات

Teggiini faj-aajo