إعدادات العرض
def ndànk du am ci dara lu dul ne dana ko taaral, waaye du ñàkk ci dara it lu dul ne dana ko ñaawal
def ndànk du am ci dara lu dul ne dana ko taaral, waaye du ñàkk ci dara it lu dul ne dana ko ñaawal
Jële na ñu ci Aysatu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- Soxnas Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «def ndànk du am ci dara lu dul ne dana ko taaral, waaye du ñàkk ci dara it lu dul ne dana ko ñaawal».
[Wér na] [Muslim soloo na ko]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tiếng Việt සිංහල Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు မြန်မာ ไทย Deutsch 日本語 پښتو অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands ئۇيغۇرچە Kiswahili தமிழ் دری Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy Română Kinyarwanda नेपाली Српски Soomaali Moore Українська Български Azərbaycan ქართული тоҷикӣ bmالشرح
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day leeral ne def ndànk ak ug nooy ak teey ci wax ak jëf day yokk bir yi ab taar ak ug mat ak rafet, kon yell na boroomam am li mu bëgg. Ñàkk a teey day sikkal bir yi di ko ñaawal tey tere boroomam am la mu bëgg, bu ko amee it ci coono la koy ame.فوائد الحديث
Ñaaxe ci jikkowoo ay teey.
Ag teey day taaral nit ki, te sabab la ci wépp yiw ci biri diine ak yu àdduna.
التصنيفات
Jikko yees gërëm