ku man a takk jabar na takk, ndaxte moo gën a man a damm ab gis, gën a man a sàmm péy mi, ku ko manul nag dénk naa ko woor, ndaxte dana ko man a téye

ku man a takk jabar na takk, ndaxte moo gën a man a damm ab gis, gën a man a sàmm péy mi, ku ko manul nag dénk naa ko woor, ndaxte dana ko man a téye

Jële nañu ci Abdullah ibn Mashuud yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: nekkoon nanu fi Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: «ku man a takk jabar na takk, ndaxte moo gën a man a damm ab gis, gën a man a sàmm péy mi, ku ko manul nag dénk naa ko woor, ndaxte dana ko man a téye».

[Wér na] [Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér]

الشرح

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day soññ ki man a sëy ak li aju ci dundug sëy mu takk soxna; ndaxte moo gën a man a sàmm ab gisam ci lu araam, te moo gën a man a aar péyam, ak it tere ko a tàbbi ci ñaawteef, Ku manul a yor dundub sëy fekk ku man a sëy la kon na woor ndaxte dana dagg bànneexu péyam ak ayu maniyu mi.

فوائد الحديث

Xérug lislaam ci yiy sabab ag saŋéwu ak

mucc ci ñaawteef yi.

Ñaax na ki amul doley takk muy

woor; ndaxte day wàññi bànneex bi.

Anamu niróole woor ak Wijaa; ndaxte Wijaa mooy tàpp sédditi ñaari xuur yi, bànneexu sëy bi daldi deñ, niki noonu woor, day wàññi bànneexu sëy.

التصنيفات

Ngëneelu koor, Ngëneelu denc soxna