bis-pénc du taxaw ba keroog ngeeni xeex ak Yahuut yi, ba doj wu ab Yahuut nekk ci ginnaawam di wax naan: yaw jullit bi, ab Yahuut a ngi nii sama ginnaaw ñëwal ray ko

bis-pénc du taxaw ba keroog ngeeni xeex ak Yahuut yi, ba doj wu ab Yahuut nekk ci ginnaawam di wax naan: yaw jullit bi, ab Yahuut a ngi nii sama ginnaaw ñëwal ray ko

Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «bis-pénc du taxaw ba keroog ngeeni xeex ak Yahuut yi, ba doj wu ab Yahuut nekk ci ginnaawam di wax naan: yaw jullit bi, ab Yahuut a ngi nii sama ginnaaw ñëwal ray ko».

[Wér na] [Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér]

الشرح

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa xibaar ne bis-pénc du ñëw mukk lu dul ne jullit ñi danañu xeex ak Yahuut yi, Ba bu Yahuut bi dawee jëm ci ginnaaw aw doj ngir làqatu fa; Yàlla waxloo doj wi mu woo jullit bi ne ko: ab Yahuut moo ngi ci ginnaawam na ñëw ray ko.

فوائد الحديث

Bokk na ci njariñal hdiis bi :

Xibaareg Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- yenn kumpa yi ak yi ñëwagul, kem ni ka ko Yàlla mu kawe mi xamale, te fàwwu mu am.

Jullit ñi dañuy xeex ak Yahuut yi ci mujjug jamono, te loolu daa bokk ci màndargay bis-pénc.

Diiney Lislaam da fiy des ba bis-pénc, te day not diine yépp.

Yàlla day dimbali jullit ñi ci kaw séen i noon, te bokk na ca mu waxloo doj yi ci mujjug jamono.

التصنيفات

Dundug barsàq