إعدادات العرض
bàyyiwuma sama ginnaaw fitna ju dàq a lor góor ñi ci jigéen ñi
bàyyiwuma sama ginnaaw fitna ju dàq a lor góor ñi ci jigéen ñi
Jële nañu ci Usaamata Ibn Sayd -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «bàyyiwuma sama ginnaaw fitna ju dàq a lor góor ñi ci jigéen ñi»
[Wér na] [Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी සිංහල Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు Kiswahili မြန်မာ ไทย Deutsch 日本語 پښتو Tiếng Việt অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands ئۇيغۇرچە தமிழ் دری Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy Română Kinyarwanda नेपाली Српски Soomaali Moore Українська Български Azərbaycan ქართული тоҷикӣ bm Oromoo Македонскиالشرح
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day xibaare ne bàyyiwul ginnaawam nattu bu gën a man a lor góor ñi ci jigéen ñi; ndax bu bokkee ci njabootam man naa waral mu topp ko ci lu wuuteek Sariiha, bu dee ab jàmbur la ci moom man naa jaxasoo ak moom ak di wéet ak moom te loolu day waral ay yàqute.فوائد الحديث
War na ci jullit bi mu moytu ftnaay jigéen ñi, te fatt bépp bunt buy waral fitnawu ci ñoom.
War na ci aji-gëm ji mu làqu ci Yàlla, ak xemmeem jëm ci moom ngir mucc ci fitna yi.
التصنيفات
Ŋàññ topp bakan ak bànneex yi