إعدادات العرض
Yàlla daa bëgg ñu def limu yombal, kem ni mu bëgge ñu def mbir yimu dogu
Yàlla daa bëgg ñu def limu yombal, kem ni mu bëgge ñu def mbir yimu dogu
Jële na ñu ci Ibn Abbaas -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «Yàlla daa bëgg ñu def limu yombal, kem ni mu bëgge ñu def mbir yimu dogu».
[Wér na] [Ibnu Hibbaan soloo na ko]
الترجمة
العربية English မြန်မာ Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands اردو Español Bahasa Indonesia ئۇيغۇرچە বাংলা Türkçe Bosanski සිංහල हिन्दी Tiếng Việt Hausa മലയാളം తెలుగు Kiswahili ไทย پښتو অসমীয়া Shqip دری Ελληνικά Български Fulfulde Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy or Română Kinyarwanda Српски тоҷикӣ O‘zbek नेपाली Moore Kurdî Oromoo Soomaali Français Tagalog Azərbaycan Українська bm தமிழ் Deutsch ქართული Português Македонски Magyar فارسی Русский 中文الشرح
Leerarug hdiisbi: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da ñuy xamal ne: Yàlla daa bëgg ñu def ay yombalam yi mu yoonal, ci woyofal àtte yi ak jaamu yi, ak yombalal ko mukallaf mi ngir ngànt -niki wàññi julli ak boole ko cib tukki-, Kem nimu bëgge ñu def ay dogoom, ci bir yu war yi; ndaxte ndigalul Yàlla ci yombal yi ak ci dogu yi benn la.فوائد الحديث
Bokk na ci njariñal hdiis bi:
Yërmàndey Yàlla ci jaamam ñi, ak ne moom Yàlla mu sell mi day bëgg ñu def yi mu yoonal ci ay yomb-yomb.
Matug Sariiha ji ak teggilam jullit bi AB coono.