إعدادات العرض
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan tudd Yàlla ci bépp jamono
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan tudd Yàlla ci bépp jamono
Jële na ñu ci Aysatu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan tudd Yàlla ci bépp jamono.
[Wér na] [Muslim soloo na ko]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tiếng Việt ئۇيغۇرچە Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు မြန်မာ ไทย Deutsch 日本語 پښتو অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands සිංහල Kiswahili தமிழ் دری Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy Română Kinyarwanda नेपाली Српски Soomaali Moore Українська Български Azərbaycanالشرح
Aysatu yaayu way-gëm ñi -yal na ko Yàlla dollee gërëm- day xibaare ne Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa xéroon lool ci tudd Yàlla mu kawe mi, ak ne daa na tudd Yàlla ci bépp jamono ak bérab ak anam.فوائد الحديث
Sàrtaluñu ci tudd Yàlla laab ci toj gu ndaw mbaa toj gu mag.
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- daa saxoon ci tudd Yàlla .
Ñaaxe ci tudd Yàlla mu kawe mi lu bari ci bépp jamono ngir roy ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-, lu dul ci anam yi ñuy tere ku ci tudd Yàlla, niki jamanoy faj aajo.
التصنيفات
Àttey Alquraan ak kaamil yi