إعدادات العرض
ku jàngul faatiha amul julli
ku jàngul faatiha amul julli
Jële na ñu ci Ubaadata Ibnus Saamit -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "ku jàngul faatiha amul julli".
[Wér na] [Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér]
الترجمة
العربية Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tagalog ئۇيغۇرچە Hausa Português Kurdî සිංහල Svenska ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Tiếng Việt Kiswahili پښتو অসমীয়া دری Кыргызча or Malagasy नेपाली Čeština Oromoo Română Nederlands Soomaali తెలుగు മലയാളം ไทย Српски Kinyarwanda ಕನ್ನಡ Lietuvių Українська ქართული Moore Magyarالشرح
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day leeral ne julli du wér lu dul ci jàng saaru Faatiha, ndaxte ponk la ci ponki julli ci ràkka yépp.فوائد الحديث
Faatiha leneen manukoo wuutu ci ku ko man.
Ràkka bu ñu jàngul faatiha day yàqu, ci ki ko tay, ak ki xamul, ak ki fàtte; ndaxte ponk la, te ponk du rot ba mukk.
Jàng faatiha dana wàcci maamuum
bi ji bu dabee imaam bi cib rukkoo.
التصنيفات
Ponki julli