إعدادات العرض
Nekkoon a nu ci Umar mu wax ne: "tere nañ nu toggoo lu metti
Nekkoon a nu ci Umar mu wax ne: "tere nañ nu toggoo lu metti
Jële na ñu ci Anas Ibn Maalik, -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Nekkoon a nu ci Umar mu wax ne: "tere nañ nu toggoo lu metti"
[Wér na] [Al-buxaariy soloo na ko]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी සිංහල Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు Kiswahili မြန်မာ ไทย 日本語 پښتو Tiếng Việt অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands ئۇيغۇرچە தமிழ் دری Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy Română Kinyarwanda नेपाली Српски Soomaali Deutsch Moore Українська Български Azərbaycan ქართული тоҷикӣ bm Македонскиالشرح
Umar -yal na ko Yàlla dollee gërëm- day xibaare ne Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- tere na nu nuy toggoo yu metti yi ci lu dul aajo, moo xam ci wax mbaa jëf.فوائد الحديث
Bokk na ci toggoo yu metti yi ñu tere: bari ab laaj, walla di toggoo loo xamul, walla di taral ci mbir mu Yàlla woyofal.
Jaadu na ci jullit bi mu tàmmal boppam woyof te bañ a diisal ci wax ak ci jëf: ci lekkam, ak ci naanam, ak ci ay waxam, ak mbiram yépp.
Lislaam diine ju yomb la.
التصنيفات
Jikko yees ŋàññ