إعدادات العرض
deesul julli fekk ñam wi daa teew, walla muy xëcconte ak ñaari sobe yi
deesul julli fekk ñam wi daa teew, walla muy xëcconte ak ñaari sobe yi
Jële na ñu ci Aysa -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «deesul julli fekk ñam wi daa teew, walla muy xëcconte ak ñaari sobe yi».
[Wér na] [Muslim soloo na ko]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tiếng Việt සිංහල ئۇيغۇرچە Kurdî Hausa Português മലയാളം မြန်မာ Deutsch 日本語 پښتو অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands తెలుగు Kiswahili தமிழ் ไทย دری Кыргызча Lietuvių Kinyarwanda नेपाली Malagasy Italiano or ಕನ್ನಡ Oromoo Română Soomaali Српски Українська Moore Azərbaycan ქართული Magyarالشرح
Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- tere na julli ci teewaayu ñam wi nga xam ne bakkanu kiy julli da koo xemmeem, xolam di ca nekk. Niki noonu tere na di julli di jañante ak ñaari sobe yi -te mooy saw ak dem duus- ndax kon day soxlawoo di jañ sobe sa .فوائد الحديث
Jaadu na ci kiy julli mu sori lépp lu koy soxlaal ci julli gi balaa mu caa dugg.
التصنيفات
Njuumtey ñiy julli