إعدادات العرض
àjjana moo gën a jege ku ne ci yeen ay waroy dàllam, sawara it naka noonu
àjjana moo gën a jege ku ne ci yeen ay waroy dàllam, sawara it naka noonu
Jële nañu ci Ibn Mashuud -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc- mu wax ne: «àjjana moo gën a jege ku ne ci yeen ay waroy dàllam, sawara it naka noonu».
[Wér na] [Al-buxaariy soloo na ko]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tagalog Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు Kiswahili தமிழ் සිංහල မြန်မာ Русский Deutsch 日本語 پښتو Tiếng Việt অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands ئۇيغۇرچە ไทย دری Български Fulfulde Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy or Română Kinyarwanda тоҷикӣ O‘zbek Akan नेपाली Moore Azərbaycan Oromoo Soomaali Українська bm km rn ქართული Македонски Српски Lingalaالشرح
Yónente bi day xamle ne àjjana ak sawara dañoo jege nit ki kem ni ko ay waroy dàllam jegee te mooy liy nekk ci kaw ndëggu yi, ndaxte moom man naa def ab topp Yàlla ngir ngërëmam loolu dugal ko àjjana, walla ab moy Yàlla loolu nekk sabab ci duggam sawara.فوائد الحديث
Xemmemloo ci jëf lu baax doonte dafa néew, ak xuppaate ci jëf lu ñaaw doonte dafa néew.
Jullit cig dundam manul ñàkk mu boole yaakaar ak ragal, tey sax ci ñaan Yàlla mu saxal ko ngir mu mucc te du woru ci melokaanam.
التصنيفات
Meloy Àjjana ak Sawara