إعدادات العرض
bu nit ki bëggee mbokkam na ko wax ne da koo bëgg
bu nit ki bëggee mbokkam na ko wax ne da koo bëgg
Jële nañu ci Miqdaat Doomi Mahdii-karib -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónent bi -yal na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc- mu wax ne: "bu nit ki bëggee mbokkam na ko wax ne da koo bëgg".
[Wér na] [Abóo Daawuda soloo na ko, ak At-tirmisiy, ak An-nasaa'iy ca As-sunan Al-kubraa, ak Ahmat]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tiếng Việt Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు Kiswahili မြန်မာ Deutsch 日本語 پښتو অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands ئۇيغۇرچە සිංහල தமிழ் ไทย دری Akan Azərbaycan Български Fulfulde Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy नेपाली or Română Kinyarwanda тоҷикӣ O‘zbek Moore Oromoo Српски Soomaali bm Українська rn km ქართული Македонски mnkالشرح
Yónent bi -yal na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc- day leeral benn ci yiy dëgëral diggante way-gëm ñi, tey tasaare mbëggeel seen biir, te mooy bu kenn bëggee mbokkam mu wax ko ne da koo bëgg.فوائد الحديث
Ngëneelu mbëggeel gir Yàlla rekk tax, ci lu dul njariñul àdduna.
Sopp gi ñu sopp
ñu xibaar ki ñu bëgg ngir Yàlla ci bëgg gi ñi ko bëgg, ngir mbëggeel ga ak miineel ga gën a yokk.
Tasaare mbëggeel ci biir way-gëm ñi day dëgëral mbokkoog mgëm, day wattu mbooloo mi ci taasaaroo ak tàqalikoo.