إعدادات العرض
bu ngeen déggee woote gi nangeen wax lu mel ni li noddkat bi di wax
bu ngeen déggee woote gi nangeen wax lu mel ni li noddkat bi di wax
Jële na ñu ci Abii Sahiid Al-Xudriyu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «bu ngeen déggee woote gi nangeen wax lu mel ni li noddkat bi di wax».
[Wér na] [Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér]
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tiếng Việt ئۇيغۇرچە Hausa Português Kurdî മലയാളം Kiswahili Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá සිංහල ไทย پښتو অসমীয়া دری Кыргызча or Kinyarwanda नेपाली Română Lietuvių Malagasy తెలుగు ಕನ್ನಡ Oromoo Nederlands Soomaali Deutsch Shqip Српски Українська Moore ქართული Azərbaycan Magyar தமிழ் Македонскиالشرح
Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day soññee ci bu ñu dégge nodd-kat bi ñu koy toppandoo, ci di wax kem li muy wax. Bu kàbbaree nu kàbbar, bu waxee ñaari seede yi, nu wax leen. Dees na ca settee:(hàyya halas salaah, hayya halal falaah )foofu dañuy wax ci ginnaawam : laa hawla wa laa xuwwata illaa bil Laahi.فوائد الحديث
Bokk na ci njariñal hdiis bi: day toppandoo noddkat bu njëkk soonga toppandoo noddkat bu ñaareel bi, doonte noddkat yi dañoo bari, ngir ne hadiis bi daa matale lépp.
Day toppandoo noddkat bi ci anam gu ne, ndeem nekkul ci wanag, mbaa muy faj aaju.
التصنيفات
Nodd ak taxawal