إعدادات العرض
Yàlla nee na: yaw doomu Aadama ji joxeel ma jox la
Yàlla nee na: yaw doomu Aadama ji joxeel ma jox la
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «Yàlla nee na: yaw doomu Aadama ji joxeel ma jox la».
الترجمة
العربية বাংলা Bosanski English Español فارسی Français Bahasa Indonesia Русский Tagalog Türkçe اردو 中文 हिन्दी Tiếng Việt සිංහල Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు မြန်မာ ไทย Deutsch 日本語 پښتو অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands ئۇيغۇرچە Kiswahili தமிழ் دری Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy Română Kinyarwanda नेपाली Српски Soomaali Moore Українська Български Azərbaycanالشرح
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dañuy xamal ne Yàlla mu kawe mi dafa wax ne: yaw doomu Aadama ji joxeel -dund gila war ak giñu sopp- ma yaatalal la jox la lu ko wuutu te barkeelal la ko.فوائد الحديث
Ñaaxe ci saraxe ak joxe ci yooyu Yàlla.
Joxe ci mbir yu baax yi bokk na ci sabab yi gën a màgg yiy baarkeel wërsëg di ko ful, ak Yàlla wuutalal jaam bi la mu joxe woon.
Hadiis bii dafa bokk ci li Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nettali jële ko ci Boroomam, ñu di ko woowe Hadiis Al-xuddsi walla Hadiisu Al-Ilaahiy, te mooy Hadiis bi nga xam ne ay baatam ak i maanaam ci Yàlla la juge, waaye amul jagle yi nekk ci Alxuraan te mu koy ràññee ak lu dul moom, niki di jaamu Yàlla ci jàng gi ak di laab ngir jàng ko, ak di ci dëkke mbaa di ci lottalaate ak yenneen.