إعدادات العرض
ku wàcc cig kër daal di wax: ahuusu bi kalimaatil Laahi At taammaati min sarri maa xalaxa, dara du ko lor ba baa muy juge ca kër googa
ku wàcc cig kër daal di wax: ahuusu bi kalimaatil Laahi At taammaati min sarri maa xalaxa, dara du ko lor ba baa muy juge ca kër googa
Jële nañu ci Xawlata doomu Hakiim As-Sulamiyata mu wax ne : dégg naa Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «ku wàcc cig kër daal di wax: ahuusu bi kalimaatil Laahi At taammaati min sarri maa xalaxa, dara du ko lor ba baa muy juge ca kër googa».
الترجمة
العربية Bosanski English Español فارسی Français اردو 中文 हिन्दी Bahasa Indonesia বাংলা Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు Kiswahili தமிழ் සිංහල မြန်မာ Русский ไทย Deutsch 日本語 پښتو Tiếng Việt অসমীয়া Shqip Svenska Čeština ગુજરાતી አማርኛ Yorùbá Nederlands ئۇيغۇرچە Türkçe دری Magyar Italiano ಕನ್ನಡ Кыргызча Lietuvių Malagasy Română Kinyarwanda नेपाली Српски Soomaali Moore Українська Български Tagalog Azərbaycan ქართული тоҷикӣ bm Oromoo Македонскиالشرح
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day gindi aw xeetam jëme leen ci fegu ak làqa ci luy jariñ nga xam ne day jeñ lépp lu nit ki di moytu ak di ko ragal bu wàccee ci benn barab ci suuf, moo xam dafa nekk ci tukki mbaa ci doxontu mbaa leneen: mu jàpp te làqatu ci baati Yàlla yu mat yii ay ngëneel ci baarkeem ak ci njariñam, te mucc ci bépp ayib ak ug wàññiku, ci ayu bépp mbindéef mu am aw ay, mu am kóolute ci jépp lor ci foofa mu wàcci feeg ma nga fay nekk.فوائد الحديث
Muslu ag jaamu la, te ci Yàlla lañu koy def ak ay turam ak i meloom.
Dagan na ñu muslu ci waxi Yàlla, ndaxte melo la ci ay melokaanam moom Aji-Sell ji, mu wuute ak muslu ci mbindeef ndaxte bokkaale la.
Ngëneelul ñaan ak barkeem.
Aaru ci sikar sabab la ci musal jaam bi ci ay yi.
Naaxsaayal sàkku muslaay ci lu dul Yàlla, lu ci mel ni jinne yi, ak njabarkat yi, ak duurkat yi ak ñeneen.
Yoonal nañu jàng ñaan gii ci képp ku wàcc ci ab barab mu nekk ci dëkkam wala cib tukki.
التصنيفات
Sikkar yi ñeel bir yi gaar