إعدادات العرض
deesul loru waaye deesul lore
deesul loru waaye deesul lore
Jële na ñu ci Abuu Sahiid Sahd ibn Maalik ibn Sinaan Al-Xudriyu yal na ko Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "deesul loru waaye deesul lore".
[Tane na] [رواه ابن ماجه والدارقطني وغيرهما مسندًا]
الترجمة
العربية Español አማርኛ English اردو Indonesia বাংলা Français Türkçe Русский Bosanski සිංහල हिन्दी 中文 فارسی Tiếng Việt Tagalog Kurdî Hausa Português മലയാളം తెలుగు Kiswahili தமிழ் မြန်မာ ไทย Deutsch پښتو অসমীয়া Shqip Nederlands ગુજરાતી Кыргызча नेपाली Lietuvių دری Српски тоҷикӣ Kinyarwanda Magyar Čeština Moore Malagasy Oromoo ಕನ್ನಡ Azərbaycan O‘zbek Українська ქართული Македонски ភាសាខ្មែរ Bambara ਪੰਜਾਬੀ मराठी Kirundi Kurmancî Bahasa Melayuالشرح
Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day leeral ne dañoo war a jañ lor ci ay anam yu wuute, ci sunu jëmm ak ci ñeneen ñi, daganul kenn di lor boppam mbaa muy lor keneen. Du dagan ci kenn muy delloo lor ci aw lor; ndax lor deesu ko dindee lor lu dul ci anamu fayantoo te bañ a ëppal.فوائد الحديث
Bokk na ci njariñal adios bi: tere ëppal ci fayu lu ëpp la ñu la def.
Yàlla digalul ay jaamam lenn lu leen di lor.
Hadiis bi reegal la ci araamal lor, ak lore ci wax walla ci jëf walla ci bàyyi.
Bokk na ci tënki Sariiha yi: "lor dees koy dindi", Sariiha du saxal lor, te day tere lore.
