إعدادات العرض
Jëfi xol yi
Jëfi xol yi
1- Jëf yi mi ngi aju ci yéene yi, te nit ku nekk la mu yéene rekk lay am
2- baax mooy: rafet jikkó, bàkkaar mooy liy dengi-dengi ci sa dënn, nga bañ nit ci gis ko
4- ñaari jullit bu ñu jaamaarloo ak séen ñaari Jaasi ka raye ak ka ñu ray yépp sawara lañu jëm
5- Yàlla du xool seen i melo mbaa seen alal waaye seen xol lay xool ak seen i jëf
6- jëf yi mi ngi aju ca yéene ya, te nit ku nekk la mu yéene rekk lay am
7- Kenn ci yéen du gëm ndare ma gënal ko way-juram ak doomam ak mbooleem nit ñi
8- Benn waay dafa laaj Yonnente bi ci bis-pénc ne ko: kañ la bis-pénc? Mu ne ko: "lan nga ko waajalal
11- wàlle amul gaafal amul, njuuma amul, Safar amul, te nanga daw ki gaana kem ni ngay dawe Gaynde
12- bu kenn ci yéen faatu lu dul ne dafa rafet njort ci Yàlla
13- lu baax mooy rafet jikkó, lu bon mooy luy dengi-dengi ci sa dënn, nga bañ nit ñi gis ko
15- Yàlla sadd na misaal ci yoon wu jub
