إعدادات العرض
Lislaam
Lislaam
1- tabax nañu lislaam ci juróom
2- waaw ndax su ma jullee julliy farata yi, woor weeru koor, daganal yi dagan, araamal yi araam
3- laaj nga lu màgg, waaye lu yomb la ci ku Yàlla yombalal
5- tabax nañu lislaam ci juróom
7- texe na de ndeem wax na dëgg
9- laaj nga lu màgg, waaye lu yomb la ci ku ko Yàlla yombal ci moom
12- ndaxte waxul benn yoon ne: sama Boroom na nga ma jéggal samay bàkkaar ëllëg bisub fay ba
15- jébbalu nga ànd ak la nga defoon ciw yiw
17- man maay Damaam Ibn Sahlabata di mbokkum njabootu Sahd Ibn Bakrin
18- Yahuut yi ñooy ñi Yàlla mere, nasaraan yi ñooy ñi réer
19- waxal ne: amul kenn ku yayoo jaamu ku dul Yàlla, ma seedeel la ci ëllëg bis-pénc
20- li gay wax di ci woote lu baax la, boo ñu xibaaroon ndax la ñu defoon dees na ko jéggale
