إعدادات العرض
Alquraan ju tedd ji ak xam-xam yi ci aju
Alquraan ju tedd ji ak xam-xam yi ci aju
2- ki gën ci yéen mooy ki jàng Alxuraan te di ko jàngale
3- buleen def séen kër yi ay bàmmeel, Saytaane day daw kër goo xam ne dañu fay jàng saaru Al-Baxara
4- ku jàng ñaari aaya yi ci mujjug saaru Al-Baxara cig guddi danañu ko fegal leeb luy Aw ay
6- Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan tudd Yàlla ci bépp jamono
8- yaw sama baay tëx, waxal: laa ilaaha Illal Laahu, genn kàddu gog dinaala ci mana layal fa Yàlla
10- dinañu indi dee ci melow kuuy mu duuf
17- Yahuut yi ñooy ñi Yàlla mere, nasaraan yi ñooy ñi réer
18- bu ngeen gisee ñiy topp lënt ya xamleen ne ñooñii la Yàlla di wax nangeen leen moytu
19- li gay wax di ci woote lu baax la, boo ñu xibaaroon ndax la ñu defoon dees na ko jéggale
20- yéen nit ñi Yàlla de jële na ci yéen rëy-rëylug ceddo ga ak seenug damu ci seen baay ya
21- {te dees na leen laaj xéewal yi bis booba}