إعدادات العرض
Laab
Laab
3- jempleen Seen mustaas yi, te yar sikkim yi
5- Yàlla du nangu jullig kenn ci yéen bu dee daa tojle ba keroog muy jàpp
6- socc day laabal gémmeñ di gërëmloo Boroom bi
7- Ku jàpp te rafetal njàpp ma, ay ñaawtéefam day génn ci aw yaramam bay génn ci ay weyam
9- mbugal ñeel na tastën ya ca sawara, deeleen jotal njàppu mi
10- bàyyileen, dama leen cee dugal ñu di ñu laab
11- loolu dereti sidit la, waaye bàyyil julli ci limu bis yi ngay gis mbaax, topp nga sangu te julli
12- Bu kenn ci yéen di jàpp na def ndox ci bakkanam daa di saraxndiku, kuy fomp (laabu) na ko tóolal
13- Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan jug guddi day socc
16- bu ab xaj naanee ci ndabul kenn ci yéen na ko raxas juróom-ñaari yoon
21- daal di jàpp njàppum Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-
25- ku sangu bisub Àjjuma sangug janaba topp mu dem julli ji, dana mel ni ku saraxe ag giléem
26- kuy njëw ci yéen ci àjjuma ji na sangu
27- moom am ndoxam lu laab la , am méddam it lu dagan la
28- bu ndox mi nekkee ñaari mbànd kon du téye sobe
34- Nëxit gi jigéen di gis ak mboq-mboq yi ginnaaw laab daawuñuko jàppee dara
35- toogal diir bi la sa mbaax daan téye, topp nga sangu
36- Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan jàppu ci julli gu ne
37- Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- jàpp na benn-benn
38- Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- jàpp na ñaar-ñaar
40- war na ci bépp jullit mu sangu ci juróom ñaari fan yu nekk benn yoon, da ciy raxas boppam ak yaramam
43- Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan génn ci wanag day wax: "Xufraanaka
