إعدادات العرض
Xam ñaan yi ak sikkar yi
Xam ñaan yi ak sikkar yi
3- Li gën ci sikar yi: Laa ilaaha illal Laahu, li gën ci ñaan yi: Alhamdu lil Laahi
4- fi jaam bi di gën a jegee Boroomam mooy bu sujjóotee, deeleen ci baril ay ñaan
6- ñaari baat a ngi nii yu woyof ci làmmeñ, diis ci màndaxekaay ba, Yàlla miy Aji-Yërëme ji sopp leen
9- ku jàng ñaari aaya yi ci mujjug saaru Al-Baxara cig guddi danañu ko fegal leeb luy Aw ay
11- yaw Abbaas, yaw baay taxu Yonnente Yàlla bi, ñaanal Yàlla jàmmi àdduna ak allaaxira
14- fi Boroom bi di gën a jegee jaam bi mooy ci mujjantalu guddi gi
16- man maa ngi fa ma sama jaam bi njorte, te maa ngi ànd ak moom saa yu ma tuddee
18- misaalu kiy tudd Boroomam ak ki dul tudd Boroomam, mi ngi mel ni misaalu kiy dund ak ki dee
20- ki nay dëgg mooy ki ñu ma tudd fi moom te julliwul ci man
22- ñaan deesu ko delloo ci diggante nodd ak liqaam
23- Allaahuma aslih lii diinii allasii huwa hismatu amrii
25- Allaahuma innii as-aluka alhaafiyata fiddunyaa wal aaxirati
28- Allaahuma innii ahuusu bika min xalati addayni, wa xalabati alhaduwwi, wa samaati al-ahdaa
29- Allahuma bika asbahnaa, wa bika amsaynaa, wa bika nahyaa, wa bika namuutu, wa ilayka anusuuru
31- li gën a kawe cig jégalu yi mooy
43- Allaahuma innii as-aluka alhudaa wattuqaa walhafaafa walxinaa
44- ku wax: subhaanal Laahi Alhasiimi wa bi hamdihi, ñu jëmbëtal ko ag garabu tàndarma ca àjjana
45- yéen nit ñi tuubleen jëm ci Yàlla, man de damay tuub ci bis bi téeméeri yoon
50- wax naa ci sa ginnaaw ñenti kàddu, ñatti yoon, bu ñu ko nattoon ci li nga wax ci bis bi mu tollu ko
