إعدادات العرض
Dégg diine ak i cosaanam
Dégg diine ak i cosaanam
2- tabax nañu lislaam ci juróom
3- Bàyyil looy sikk-sàkka jëm ci loo sikk-sàkkawul
4- Yàlla bind na Ag rafetal ci bir yépp
5- waaw ndax su ma jullee julliy farata yi, woor weeru koor, daganal yi dagan, araamal yi araam
7- deesul loru waaye deesul lore
9- Lépp luy màndiloo dafa araam.
11- deesul julli fekk ñam wi daa teew, walla muy xëcconte ak ñaari sobe yi
12- boo waxee sa àndandoo: noppil ci bisu àjjuma, fekk imaam bi di xutba, kon fo nga
14- jempleen Seen mustaas yi, te yar sikkim yi
16- yaw sama Boroom maa ngi lay ñaan bul def sama bàmmeel ab xërëm
18- Yàlla du nangu jullig kenn ci yéen bu dee daa tojle ba keroog muy jàpp
19- socc day laabal gémmeñ di gërëmloo Boroom bi
22- képp ku woor weeru koor ngir gëm ak yaakaar yiw; dees na ko jéggal li jiitu ci ay bàkkaaram
23- ku taxaw Laylatul Xadri ngir gëm Yàlla ak yaakaar pay ga dees na ko jéggal li weesu ci ay bàkkaaram
25- li dagan de leer na li araam it leer na,
26- Yàlla bind na rafetal ci mbir yépp
27- deesul loru waaye deesul lore, ku lore Yàlla lor ko, waaye ku sonle Yàlla sonal ko
28- Jibriil deñul di ma dénk dëkkandóo, bama muj njort ne dana ko dondloo
29- mocc ak takk ay xarnga-fuufa ak noob bokkaale la
30- buleen saaga ñi faatu, ndax ñoom kat wéy nañu ca lañu jiital
31- ku julli suba moo ngi ci kaaraangeg Yàlla
34- àdduna ay jumtukaay rekk la, te li gën ci jumtukaay yi àdduna mooy jigéen ju baax
35- Yàlla nee na: yaw doomu Aadama ji joxeel ma jox la
36- sart yi gën a yelloo matal mooy yi ngeen daganale péy ya
37- Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- daa na ko tudde Yàlla ginnaaw julli gu ne
39- ku bàyyi jullig tàkkusaan jëfam yàquna
40- Ku jàpp te rafetal njàpp ma, ay ñaawtéefam day génn ci aw yaramam bay génn ci ay weyam
41- bu nit ki dundalee njabootam di ci séentu aw yiw loolu dina nekk ci moom ab sarax
42- Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- tere na zulu
43- buleen toog ci kaw bàmmeel yi, te buleen ko jublu ci julli
44- ñooñu aw nit lañu wow bu ku baax faatoo fa ñoom, dañuy tabax ca bàmmeelam ba jàkka
45- digal nañu ma may sujjóot ci juróom-ñaari cér
47- Allaahumma Antas Salaamu, wa Minkas Salaamu, Tabaarakta Sal Jalaali wal ikraami
48- jullil taxaw, boo ko manul nga toog, boo ko manul nga wetu
49- ndax danga dégg wooteg julli gi?" Mu ne ko: waaw, mu ne ko: "kon nag wuyujil
50- Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- xamal na ñu xutbag aajo
51- Deesul takk jigéen ci lu dul kilifa
53- Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- rëbb na kiy ger ak ki ñuy ger cib àtte
54- tabax nañu lislaam ci juróom
55- waaw ndax su ma jullee julliy farata yi, woor weeru koor, daganal yi dagan, araamal yi araam
57- mbugal ñeel na tastën ya ca sawara, deeleen jotal njàppu mi
58- Bu nodd-kat bi waxee: Allaahu Akbar Allaahu Akbar, kenn ci yéen wax: Allaahu Akbar Allaahu Akbar
59- ku fàtte genn julli na ko julli saa yu ko fàttalikoo, dara manu koo fay lu dul loolu
60- li dox ci diggante nit ki ak bokkaale ak kéefar mooy bàyyi julli
61- kóllare gi dox ci sunu diggante ak ñoom yéefar yi mooy julli, ku ko bàyyi weddi na
63- tere na nisër, daal di wax ne: "du indi aw yiw, waaye dees ciy genne aji-nay ji
65- li ñuy njëkk a àtte ci diggante nit ñi ëllëg bis-pénc mooy dereet
66- kiy xeex ngir kàddug Yàlla yëkkatiku kooku moo ngi ci yoonu Yàlla
67- bu ngeen déggee woote gi nangeen wax lu mel ni li noddkat bi di wax
68- bàyyileen, dama leen cee dugal ñu di ñu laab
69- loolu dereti sidit la, waaye bàyyil julli ci limu bis yi ngay gis mbaax, topp nga sangu te julli
70- yamaleleen seen sàppe yi, ndax yamale sàppe yi daa bokk ci matug julli gi
71- Bu kenn ci yéen di jàpp na def ndox ci bakkanam daa di saraxndiku, kuy fomp (laabu) na ko tóolal
73- Mokkal naa ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- fukki ràkka
74- Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan jug guddi day socc
82- Allaahumma baahid baynii wa bayna xataayaaya kamaa baahadta baynal masrixi wal maxribi
83- bu ab xaj naanee ci ndabul kenn ci yéen na ko raxas juróom-ñaari yoon
91- giñ naa ci Yàlla ne Yàlla gindi ci yaw benn waay moo gën ci yaw nga am géttug jur
93- daal di jàpp njàppum Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-
